La composition est de Ciré GUEYE et de Masse
DIOP Les hommes ayant terminé avec le mil, c'est au tour des femmes de
le transformer et de le préparer pour la consommation, tout se passe
dans une atmosphère de joie.
Bismilaay wal jot na doom yaay ñeme leen ko
Kuci tàyyel des jekki baa nga walandoo
5
10
15
20
25
Fab leen seen kuur yi na ngeen farlu ci
ngëlyi
Su maasee xel yépp dellu ci reer
Buleen tàyyi buleen bàyyi àddunaa
coono neen la
Su goor sonne jiggèen itam dafa wara sonn
Ku may dëbblr war na teela ñew yaay
Ku may dëbble war na teela ñëw bala
may teesale yaay
Ku ma njëkkni laay nëw dinna la may loo
xottee bolog yaay
Toolu baay dembaa neexa foree ndèef
For wurus for xaalis foraale fa doom
Yaay booy jàppal ma sab sëta ngook
Man mënuma jàpp sët bu amul baay
Yay jàppal su yàggee njariñ
feeñ
Ni rekk lañ koy deffee nimu yombee
Xiita bann, xiita bann, xiita bann
Arawal njaay arawal njaay
Yaaw mën nga mooño gërëm nga
yalla
Saa sëtbee sëtub Ndumbee
Mbañ koddu yaasin jaal
Bibaasi masse sukoo basee sa sere neexna
Arawal njaay arawal njaay
Yaw mën nga mooñee gërëm nga
yalla
Bismilay nañ dello domm yaay jant dem na
Yàlla na leen yàlla
fèexël te may leen jàmm
LA PILEUSE
|