La propreté est une notion clé, comme
elles vont aux champs pour aider les hommes, nos femmes vont aussi aux
marigots, aux mares et aux forages pour laver le linge. Elles chantent leur
joie. (l'air populaire les paroles sont de Masse DIOP)
Aylèen ñu
fòot jot gi dafa yombul doom yaay ay ñu fòot
Ngir bu jant rasoo ku nekk daal man dem taali reeree
Ñu jòg ca teel dem ca walandoo wa doom yaay teg
ci fòót
Daal di bale teg ca balaa guddee ngay dem taali reeree
Na pòot mi set sër yi mën a sell doom yaay ay
waleen
Loolu waru gar la
jiggèen a ka war a fètewòo ci rèewee
Li ko dalee Siin ba Jàmminaar
Ku ci biir ñune yaw Baaba Saar
Baaba Saar Coono warna la
S aabu jar na
njëgam
Guppale ma guppale ma yòbbu
Saabu ñaari jaam
Kuy fòot dangay fete kuy fòot dangay fete
Dangay fete, dangay fete
Sikkël ba ca kokki jagal ba ca njaañ
Rèex dèjj ba ca kolobaan
Yaroo baax, yaroo baax, yaroo baax
Soo yaroo macc tàngal yëy sa guney ngaay
Sàmmalè ma sàmmale ma
Bu sa baay dikkee sàmmale ma
Bul dem bàyy ma
yòbbaale ma may walal sa yaay
|