précédent sommaire suivant
Jàllu xaay been rèeru maa
Ami Gëy dem na jàllu xaay
Duggal saxaar wàcc nginginèew
Siyaare bameelu aadama
Sàmba aysaa nga la? caa xaay
Limaale Njaay ng ca riirum gèej
Limaale njaay limako yèene woon
Fukki bukki njuur fukki gayndè ak juròom