MADEMBA DIOP
Celui-là, Ndiakhate ! Voici mon pote, compte sur
lui
Par le nom de Dieu, je débute par mon lopin de terre
Pour que Dieu rende prospère ce lopin
5
10
Cultiver c'est la force, de la peine et du courage
Travaillez et ne craignez pas les champs
Moi, je tente de travailler ici et de ne pas craindre le
labeur
Pour que Dieu récompense mes efforts
Mademba Diop, oh le vieux Cellé Mbodji
Celui-là, Voici mon pote, compte sur lui .
TËGG CAAM (Choeur)
Chant populaire
Il appartient aux chants de corporation. C'est le forgeron
qui est dans son atelier et exalte son action. Il encourage en même temps
tous les gens qui font parti de ce corps de métier.
Jàmbaar nga momar caam ca mbaar ma
Waaw gòor momar caam ca mbaar ma
5
10
15
Jambaar nga momar caam ca mbaar ma
Waaw gòor momar caam jambar nga
Uppël ko uppël taal bi naaj na
Caam baylo buuru mbaar naaj na
Cayal ma cayal ma daggal ma
Ngòone caam gëddël taal bi naaj na
Uppël nabi isaa caam uppël
Ma uppu fíi mbay caam mu may ma bëy
Uppël naa la ren ak daaw musòo ma fay
Uppël naa la momar caam ci mbaar mi
Mani mbir mi dama neex ne diine
Jambaar nga momar caam ca mbaar ma
Waaw gòor momar caam ca mbaar ma
Kuy jàng da ngay muñ te farlu
Te nga jèem a jubal toog ca mbaar ma
Kon Caam uppël te nga gòor gòorlu
THIAM, LE FORGERON
Momar Thiam, tu es vaillant dans la forge
Bravo Momar Thiam dans la forge
5
10
15
Momar Thiam, tu es vaillant dans la forge
Bravo Momar Thiam, tu es vaillant
Attise pour lui, attise le feu, il est déjà
tard
Thiam baylo, maître de la forge, il est
déjà tard
Sertis pour moi, sertis pour moi, cisèle pour moi
Ngoné Thiam attise le feu, il est déjà
tard
Attise, Nabi Issa Thiam, attise
Mbaye Thiam, j'attise là et il me récompense
J'ai attisé pour toi cette année et
l'année dernière, tu ne m'as jamais payé
J'ai attisé pour toi, Momar Thiam, dans la forge
La chose me plaît comme une religion
Momar Thiam, tu es vaillant dans la forge
Bravo Momar Thiam dans la forge
Un apprenti doit être endurant et alerte
Et adopter une bonne conduite tout en restant à
l'atelier
Donc, Thiam, attise et persévère
Tu auras une forge à toi.
NGORKÀAN (Ballet)
Comme le précédent chant, Celui là il
appartient aussi au corps de métiers : les bûcherons.
toujours l'auto éloge et l'exaltation au travail les "Laobés" ne
sont pas essentiellement des destructeurs de forêt. Nous leur devons
d'avoir des pirogues, des outils de travail etc. Ce sont d'honnêtes
artisans et aussi des artistes
Sama sèmmiñ doom baay ka ma go
dàggil naxu ma
5
10
15
20
25
Baay laatiir jòob jàmbar
jaa nga des ca xare
Baay laatiir jòob moom ku mu dàggil naxu la
Bàce sàmba coro njaay
Càmmiñal maada njaay
Doole ngi ci yax joma nga ci sëbbëriit
Bàcc sàmba coro njaay
Jam ko ci jam njaay
Jam penda waada njaay
Càmmiñal maada njaay
Mburtum kor Borso
Camp ci meew mi naane ko ci mbaanig mi
Dëmm ray la jaale la maabo xañ la jiin la
Sam xel dem gèej
Naar yaa nga naan maadum atta faal
Tubaab yaa nga naan mersi, mersi faal
Sèerèer saa nga naan waasa, waasa faal
Tàkkusannu Ndòoyéen yoor-yooru
Ndòoyèen
Diggu bëccëgi mbaar mee gaynaako faal
Ndoongo su gennée xiif
|